bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️ Profile Banner
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️ Profile
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️

@soxnaastu_hamza

Followers
1,719
Following
2,150
Media
29
Statuses
1,380

💦❤️Mouride❤️💦 Objectif Saadix SerigneHamzatouPoint.🙏❤️Maître en Sociologie 🎓✨ DMB/UGB❤️✨ #sanaroise

Joined July 2022
Don't wanna be here? Send us removal request.
Explore trending content on Musk Viewer
Pinned Tweet
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
7 days
Moom rek la gëm Moom rek la xam Moom rek laa am Jaajëfee Mbacké😭❤️
Tweet media one
Tweet media two
Tweet media three
Tweet media four
5
19
125
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
Dama rousson douggeul Mais bonnnn😌 Dewenaty🙏🥰 #Sunukorite2024
Tweet media one
Tweet media two
Tweet media three
Tweet media four
28
138
1K
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
Maîtresse de cérémonie à mes heures perdues🙈🥰 #Sanar #UGB #sanarois
Tweet media one
Tweet media two
9
46
360
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
7 months
Mon compte insta vient d’être piraté Merci de ne pas répondre aux messages qui y sont envoyés🥹
Tweet media one
15
93
273
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
Tweet media one
5
21
273
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
8 months
Alhamdoulilah🙏💞Jërëjëfee Boroom Tuuba minou xamal sangue bou ted bi sws❤️
3
15
151
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
7 months
Tweet media one
1
10
90
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
Sant na boroom bi bubaax bam ma deffee jullit Rawatina muriid❤️😭 Ba noppi tawfeexal ma ma bokk si ñiy jëffee ndigalu wird wi😭 Alhamdoulilahi rabbil hallamiin🙏❤️🥺 Jërëjëfee seexuna ahmadal xadiim🙏❤️
4
10
68
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
7 months
Tweet media one
2
6
26
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
Jour laylatoul qadr @s_sourang yessalal ma Taye 5 shawwal sëñ Ahma yessalal ma Xana dou ma yeess waay Macha’Allah🥰🥰❤️🥳🥳🥳
3
4
24
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
« Seriñ Tuubaa lu mu bind soo amee baatin gis ko ca Lawhul Mahfuuz, te soo guddee fan tek ci sa bet » seex Abdul Ahad Mbacké❤️
0
6
24
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
@XadeejahD @SokhnaLo15 nawlee yi geen leen ndam amna🙈😍😂 Cadeaux you beurii te neex ma loolll🙈🥰contaan na troppeee🥰♥️
7
4
24
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
Wallahi Boroom Tuuba ken la!😭
1
5
24
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
Salaw mbacké yaw kep la mënul ñakk si samaw dund🥹 yagg fi lool🙏❤️
@GningSonhibou
ABOHAMZA -SONHIBOU.
1 month
Barquép Cheikh SouHaibou
5
20
205
0
2
23
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
Thiey sëriñ bi🥹❤️
4
6
19
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
As salamou haleykoum damay ñaan ndeweneul😎😎
7
0
17
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
@WesWesMurid Salam faal Ndeysaan dangeen baax Kokeuree fassee avec succes✅😌
1
0
15
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
Modadi gi neex na lool🥰🥰 Wayee teegin yi sëñ Ahmadu toggee yeeme na🥹❤️ Yalla nafi yagg lool🙏❤️
@PBodian10
Élément Cheikhul Xadim🫀🇵🇸
1 month
Uuuu uuu u Eeee eee e Aaaa aa a 🎶 mais keen manatul tiye sa bop keen keen keen eh 😭😭
4
21
156
1
2
15
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
Sama yaay xana xamoul ni taye dama xew si TL bi moumay taal lo reer🥺😌
3
2
14
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
4 months
Évitons d'augmenter la panique. Beaucoup de choses qui se disent actuellement sur l'UGB sont erronées. Ne partageons pas aveuglement des informations. Écoutons les structures habilitées (CESL/Com-Soc). Pensons aux familles qui sont très inquiètes. #FreeSenegal
0
14
14
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
Aythia commenter leen😌
Tweet media one
5
0
13
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
🌴 WAXI SERIÑ TUUBAA🌴 SËRIÑ TUUBA nee na : Ku man turu « Habdul-AHAD » te mu set du tabbi sawara ▬▬▬▬ 📚 Source : Waxtaani SËRIÑ TUUBAA VOL1
1
5
12
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
Thiey😭
@YaaFadlou
شيخ محمد الفاضل 🕊️🇸🇳
2 months
Diguanté bii nguaa ganné adouna imaam bii nodeu saay nopeu ak diguanté bii nguaa guéné adouna niou dioulé laa diguanté bou gatteu bobou béww khadioufii jour bii nguaay nieuw adouna indi wo daraa jour bii nguaay delou cii yalla do yobbeu dara loudoul saay dieuff. Naay rafete 🕊️🕊️
Tweet media one
1
7
36
1
0
12
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
Mouqqadimatoul Xidma ndekke xassidah la😭🥹❤️
3
0
12
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
5 months
@Cherif221 Tayelee sa bourse rek fasse yeen jël si vols ✈️ yii🥳🥳
0
0
11
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
Biñ ko fallee la sama xell dal❤️
@LeProfane
.
2 months
Ass va tout arranger. Amul raggal
9
42
560
2
0
11
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
Sama ngoonu tay dji deh neew na loumakoy am❤️❤️ Soudee meuss nako am sax🥺❤️ Sama xoll bi sedd na❤️❤️❤️
0
1
10
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
Tout le plaisir est pour moi cher frère🥰🤩🫶
@Abdou04048585
Abdourahmane Diong
1 month
Ravi de partager le pupitre encore une fois avec toi @soxnaastu_hamza 🎉🔥 #Quinzaine #AMELSH #UGB
Tweet media one
0
1
14
2
0
9
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
- Mawahibou ( Ht ak bou wa pikine) - Muqqadimatoul Amdah❤️ (HT 2005 xawma 2006) - Khatimatoul mounajaati + wolofal seex samba jaara mbaye ( Baay Ousseynou Gueye) Mënoul ñak🙈❤️
@MohamedWilane
Mo_152i 😁🇸🇳 !!
1 month
Ce xassida , verset coranique ?? Manam ak lou journée bi khatt khatt di ngako deglou ??🤣 Perso : jazbu , Tawbatu Darou KOUREL FMN Thies ❤️❤️😃
3
6
55
2
2
9
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
4 months
Dafa doy💔😭
Tweet media one
0
5
9
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
Taye ak demb yeep dama sagnse Mais mane daal damay rouss publier daal😅😌😏
6
0
9
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
Waa mais kan moo deffar beignets dougoup bii😭😭❤️❤️ Salées yi nakk thioooo muriid yi mën ngeen bëss nak❤️❤️❤️❤️❤️
1
1
7
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
Jootay bou nara am solloo incha’Allah Yalla nañ si yegg ak jaam On a hate❤️🥺
@Ly_Ibraahima
𝐁𝐚𝐚𝐲 𝐗𝐚𝐥𝐢𝐢𝐥 🇸🇳📚📚📝
2 months
Tweet media one
0
41
57
0
2
7
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
Faal biy ñeuwaat moom faw ma top la imcha’Allah🥹❤️
@SokhnaLo15
Soxna Lóo Hamsa
1 month
Cette vidéo prise par @tata_kadia restera la meilleure ❤️
0
13
73
1
1
6
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
Aye lii neexati na deh🥹❤️
@YaaramfallCOD
Yaaram Bi Naam Faal🌟🇸🇳
1 month
Yàlla na Yàlla dolli suturë, faj aajo yépp barkep boroom Tuubaa
9
58
289
0
2
7
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
8 months
@xalamgui_ Chaussures made in Sénégal 🇸🇳 Prix: 10mil frs Contact: 778647414 D’autres modèles disponibles✨
Tweet media one
Tweet media two
Tweet media three
Tweet media four
0
4
6
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
8 months
@SalihFadal @BambaKhadim Dangaay wird ak mbecte❤️🥰 By @droussLib
0
1
6
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
@WesWesMurid Touf touff amiinnn🙏🙏🙏
0
0
6
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
TL bi noumouy demee Nandale leen ma miinou mafii deh??🤔 Koula citer dangkoy RT walla??🤔
1
0
6
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
13 days
Alhamdoulilah Alhamdoulilah Alhamdoulilah 🙏🙏🙏
0
1
6
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
Tay lassi gën am firndeel❤️🥰 Pasteef gi kay machaa’allah🙏🤍🫶
@Ajaa_faama
Jaañ Naar🇸🇳❤️
2 months
Soxnay murid yi ay jambaar dëgg lañ dh! Yalna saa borom gënë dimbali nu bañ lak ngërëmël ku ted ki🤲🏽🤍 Très fière de vous maasha’allah
2
8
64
1
1
6
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
8 months
@abdourami Bismillah si marché bi🥳 Parfum de classe✨💞you am sollo leen indil si njeuk you xeweulee🤩🤩 Xeeñ neex par fokhcee🤩🤍 D’autres marques disponibles ( DM si vous êtes intéressés) Ps: prix différents
Tweet media one
Tweet media two
Tweet media three
Tweet media four
0
1
6
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
18 days
Macha’Allah🥰 Yalla naleen borom bi sam Te may ñou ñou melni seen boss yi🤩
@Kiindeer_BuenOo
KHALEESI TAHA💍
18 days
Meme sameu dieukeur tamit dafa meilleur 🤍il est bienveillant , à chaque fois il me montre qu’il m’aime quand je lui envoie mes photos il s’évanouit d’abord , tjrs aux petits soins tensi Yeureum nama gueumer woumeu Yalna Ko Yallah sameu Sameu bebee bi 🥺
1
0
8
3
0
5
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
7 months
Je vais assister au futur Espace de @Ly_Ibraahima . Vous viendrez aussi ?
0
2
5
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
Ohhh❤️🥰thiey element DMB yii🤧❤️
2
0
5
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
7 months
Xamnaleen dangeen gaaw si fav ak rt Mais japleen si rek bouleen ma xañ sama teranga🤣😂🙏🙏
@StoreChams
Chams_Store🧕🏿
7 months
Jeu concours J’offre la tenue Conditions : Tweet cité ayant obtenu 0 fav 0 rt S’abonner à la page Fin du jeu: vendredi 20h Bonne chance 😉
Tweet media one
Tweet media two
53
196
390
2
1
5
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
Thiey saam mii😏😌
@YaaFadlou
شيخ محمد الفاضل 🕊️🇸🇳
2 months
"Kounek amgua sa biss...! Ndax amna ñio khamni yagui léndi toutal dilén niakké kérsaa Té khamo ni moy gass sa pakhou bammél dina bokku si gnilay diappo...!" "Séxx Saliou Mbacké "😭🥹❤️😭 Diokh Thieur nitt gnii🚶🏾
Tweet media one
1
7
21
1
0
4
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
4 months
Lou meeti looll💔💔💔😭
@AbduKhoudoss
Le Firdawsien♥️عبدالقدوس♥️
4 months
Di wut sa diplôme pour dem joxko say parents, ñu jël sa certificat de décès dem joxko say parents. #FreeSenegal
3
96
216
0
2
4
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
Noir🥰 j’aime❤️❤️
@__mariishaaa___
Ndeye Marie.
2 months
Always Late 🥲🖤 Muslim Met Gala 🖤 #Sunusefliekorit é2024
Tweet media one
Tweet media two
Tweet media three
Tweet media four
17
243
2K
1
1
4
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
@AmadouTid1 @khadiim5 Bien pensé A moins qu’il n’ait pas une seule carte pour la chambre😌
0
0
2
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
Kaamil you rafeet macha’Allah❤️🥰
@XadeejahD
Xadeejah Diop
2 months
Gnou bari si yen lathie ngen ma ndakh sé disponible, kamil bii diekhna, mais sou amatei dina ko publié inchalah En attendant, kamil 30 partie amna à 15mil
2
6
35
1
0
4
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
6 months
Bismillah🙏😌
@sindidivoile
sindidi voile
6 months
J’offre un boxe hijab, une chaussure locale, un livre coranique et un Dole Xassida de chez Sindidi Voile à la personne qui aura 0 fav 0 Rt et 0 commentaire sur son quote Condition : être abonné à la page @sindidivoile Fin du jeu Mardi 5 decembre à 23h. Amoul Yakhalaté
Tweet media one
Tweet media two
Tweet media three
Tweet media four
18
65
100
0
0
4
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
7 months
Aidez moi à le signaler svp🙏🙏🙏
0
0
4
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
Sama seriñ bi loum wax wer na😌😅
@s_sourang
Moor Suraŋ
2 months
Sama kurus du laal suuf man, moytuleen ma sama wenn waxtu xajul ci kenn.
Tweet media one
22
45
464
1
0
4
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
6 months
Sokhtezz vos mariées Ma bichrienne est la plus todjj❤️🫶🥳 Allahouma barick souñ soxna si❤️🫶
1
0
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
4 months
Dëgg dou romb liii😏 jërëjëf waay
Tweet media one
2
1
4
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 years
@SambElimane2 @salioumbackefa1 weer na deih wallahi bo nekkee fou melni UGB ba feek fa @DmbUgb nga xamni xamm xam ak diine ji reik moleen ñore dinga tegguil sa boop ćono tegguil ko say wajuur😌😌
1
0
4
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
8 months
Tweet media one
0
0
4
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
@mita_caramel Jiggeen buy jox loxo goor yalla😒
0
0
4
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
4 months
Justice pour Alpha Tounkara💔
@Baaywaly
By Waly.🇸🇳
4 months
Justice pour notre frère étudiant❌ #FreeSenegal
Tweet media one
3
437
914
0
5
4
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
5 months
Macha’Allah❤️🥺
@LeMouridePost
𝐋𝐞 𝐌𝐨𝐮𝐫𝐢𝐝𝐞 𝐏𝐨𝐬𝐭 🇸🇳
5 months
9 ans la am te déggal ni mu mel ci Alxuraan rekk😍 Képp ku bëgg a jàpp ci liggéey bi jëm ci 40 Daara yu ñu recensé ca Casamance man nga jaarale sa barkeelu par Wave walla Orange Money ci numero Bassirou Gueye : 77 650 25 28
2
112
471
0
1
4
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
8 months
Wooyy Coup irrégulier🤣🤣🤣
@mbaye_magui
Sucre🦋Vanille Mme DG Ngagne Demba Touré♥️
8 months
Goudeull sikim ak tieukeull dou life.
56
34
324
1
1
4
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
8 months
Ohh❤️🥹
0
0
4
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
8 months
Ma topp café ☕️ gui melni kuñ ni gouddi gui dou jeex😫😫 Mangui nii di xoll deimb batay😌
0
0
4
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
Mon problème🥺😩 Xana mou neik soxna souma miine lol😌
@MaamFaatiNaawel
Njaxat🧕🏾📚📖
1 month
Quand vous parlez avec quelqu'un vous arrivez à le regarder les yeux dans les yeux ?
33
14
149
0
0
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
7 months
@BarkaNdaw @mc_evah Xana neikko ugb yaw🤔 Sou fekke temps manif yi ngay wax moom mdox yeksi nafi Maggi tuub nak
1
1
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
1
0
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
8 months
@plaaiiisiiir @Ly_Ibraahima Macha’Allah🙏🤍 Esk doleen ñouko bindeul yaraam🙏🙏
1
0
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
6 months
@AbduKhoudoss Matnako deh😂😂😂
1
0
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
@Nene_Yaayam @XadeejahD @SokhnaLo15 Attention mane sa ndieukee laa😌😌😌
1
0
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
@WesWesMurid amna koukay jeema pirate dii deh😅😅
@Muhamadul_Amiin
𝙱𝙰𝚁𝙰🇸🇳📚
1 month
Bonjour madame J’ai vu que vous aimez le Cheikh Ahmed Bamba. Damaa beug niou fassanté koleuré teh Cheikhoul Khadim rek takh🫶🏽
6
3
11
2
1
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
5 months
@echgueye Xamna fallay mujee deh Ndax café dafko daan seedal Mais taye moom meunou si dara
0
0
2
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
6 months
@papasambadiong3 @SokhnaLo15 😂😂😂mak jii xana campus laay doon🤔 Wallah dangeen jawalee parcelles ak waqqinan nimzat🤭🤭😂😂
0
0
1
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
18 days
@henrypierresarr @UGBSN @UsmanTurey Très ravie de vous retrouver cher ancien! Je prends la relève en étant l’actuelle capitaine de l’équipe de l’UFR LSH. Bonne chance à nous🤩
1
1
2
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
18 days
Lou am sollo bayi nalafi🤩 Dëkkee sant rek❤️
@MohamedWilane
Mo_152i 😁🇸🇳 !!
19 days
Da ngay kheuy ndeki ba sour jeul sa téléphone loula nekh nga tweet … Puff façon Sama yone nekussi , Tle bi sant Seuñ touba rk momafi baayi
5
12
92
1
1
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
Soxna Oummina bingeen may wowee neex nama deh🥰❤️ yeena baax waay
1
0
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
La dernière phrase❤️🫶
@fatima_bocoum
Jacqueline Fatima Bocoum
1 month
Un homme doit savoir rassurer une femme avec des mots doux et des actions concrètes. Un homme est rarement honnête. Sauf envers lui même. C’est en pensant à demain qu’il faut investir le présent. Monogame ou polygame, un homme perd toujours une femme qu’il n’a pas su respecter
45
91
436
0
1
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
17 days
@MohamedWilane Baal nala 😅
0
0
2
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
16 days
Daloum xell❤️🥹 yagga fi lool balla aissa🙏
@MourideTaarou
Taarou Mouride Officiel 🇸🇳
16 days
Seydinaa Hamzatu Mbàkke Ibn Seex Suhaybu
Tweet media one
Tweet media two
Tweet media three
Tweet media four
0
70
494
0
1
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
6 months
❤️🥹
@mbaye126
Abuubakrin As Siddiiq
6 months
Liy raam yal na aksi,🥹🥹🥹🥹
10
77
429
0
0
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
Lii la bëggone jeuli nga indil mako Jërëjëf!❤️
@unemusthave
𝓡.
1 month
Un homme très réfléchi en parlait hier sur inatagram et personnellement je suis d’accord avec lui. Je ne juge pas celles qui le font nak mais dou li gueunn.
Tweet media one
Tweet media two
Tweet media three
9
32
116
4
0
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
7 months
@Nene_Yaayam @XadeejahD Bilay soxna mariama damako mujee yërëm man😂
1
0
2
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
16 days
Taxmiis rajas serigne Abdou Lahad Toure ken amouko fi mou japalee massi🤔 Weur nako youtube ba sone😒
0
2
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
Nonou la rafeetee tee neexa jang♥️
@XadeejahD
Xadeejah Diop
1 month
Genrou kamil yoyu ngay nango gnarri lokho 🙃 12500 lay diar Sinon , amna ay jukki 30 partie disponible à Dakar à 15mil
4
22
81
0
0
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
Macha’Allah toma♥️🥰
@yayefal
Astou Bint Mouhamed💙🇸🇳
1 month
Jummah Mubarak🫶🏽 Tawfekh Tayssir Sah’aadatu Darayni🤲🏾🤍
Tweet media one
20
34
449
1
0
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
Astou diomaye amna tableau❤️🥰 Astou oummina nak🤔 Ahh😌😌
@yayefal
Astou Bint Mouhamed💙🇸🇳
2 months
Wa yeineu gni baxnagn deh😭💙 Tableau deh lagn ma baxei 🥹
7
20
224
1
1
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
@Mr_fallou @XadeejahD @SokhnaLo15 Lol jëwriñ deh DMB bi rek mooma si xawa jaxal😌🙈 Wayee liira gouma deh😏😅
1
0
2
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
Every time kay🤩
@RIENqueLUI
FU WAAY YEM MOOFA YAMALE BOPAM 💡💡💡❤️
1 month
À quelle heure préférez-vous le café Touba? 🙏☺️
Tweet media one
102
16
482
0
0
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
Amaat ma cadeau deh🙈🙈🙈 @SokhnaLo15 ma wane la??
3
0
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
Kou def lii sama toma😏
@Marseille345
Pisco 🇨🇻✨️
2 months
Plainte bi kiko nar bind dina sonn😭😭😅😅😅😅😅😅
Tweet media one
Tweet media two
9
15
185
2
0
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
Allahouma amiinn🙏❤️
@satoubonheur
Sakina At Tidiany
1 month
Barké Lerou yonente saws bi yallah nanu yallah defal diam soutoura adouna ak lahira goud fan ak wer barké Seydina Cheikh rta
2
17
147
0
0
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
11 days
Si xidma lama dall Sëtëtëteeeettttt😩😂❤️
@Soxnaam_
Une Ndigëlienne🤍🖤
11 days
Druss kat yii mës ngeen yëg neexitu jàng xasida booleen masul jàng, ngeen di laaj seen bopp fooleen nekkoon ba masooleen ubbi téeré bi?😅ay waay lu dàq xasida Sërin Tuubaa yii?😭
6
10
84
1
0
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
4 months
Cité took xaar😌😌
@fatima_lafleur
Anthropologue An-Nisaa🧕🏽🌹
4 months
Chose promise chose due 🤩❤️🥹 Maintenant dites moi comment voulez-vous qu’on organise le jeu ?? Les Kamil viennent de la boutique @Fama_Shopn 🥳🫰🏽❤️ la meilleure de toutes 🫶🏽 Abonnez vous à sa page on vous réserve d’autres surprises 😉 #Retweet
Tweet media one
Tweet media two
12
15
42
1
1
3
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
@n_hadei @AsSaalih22 @s_sourang Wallay moggi nussiy taxawou bubaax sax
0
0
2
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
16 days
Alhamdoulilah🙏 💔
@bilel_tawhid
ًًً
17 days
Dites Al HamdouLilah même si vous enchaînez les déceptions de jour en jour.
0
716
3K
0
0
2
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
@senbrain @XadeejahD @SokhnaLo15 Boutique yi neik en face massalikoul jinaan dinañ ko am fofou yaaram
1
0
2
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
2 months
Yaak soxna loo seen PP yi tiiteul nama😩❤️ yeena baax waayy❤️❤️❤️
@XadeejahD
Xadeejah Diop
2 months
Maa goe😭❤️
0
1
3
0
0
2
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
Ñoun fayou ñou fiñ deuk Leek bi c’est gratuit Naan bi gratuit Leep à gogo macha’Allah Leggi tata lossi mën?🤔🤔
@Mamadou01361233
Disciple de Cheikh_Anta_Diop🇸🇳 🇲🇱♥️
2 months
Elle est experte en quoi ?😶 🙆🏿‍♂️
160
34
569
1
1
2
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
@Bocar_Tkls Plaisir partagé frère
0
0
2
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
7 months
@Omd_authentik @MamadouJohn1 Bizarrement je ne sais même pas Il modifié toutes mes infos et le compte a été désactivé😏
1
0
2
@soxnaastu_hamza
bi_oummina_Haïchatine🧕🏻❤️
1 month
@Prince_Mourid @AsSaalih22 May daw ngamay dm😅
1
0
2