salioumbackefa1 Profile Banner
Saliou 🌔 Profile
Saliou 🌔

@salioumbackefa1

Followers
45K
Following
65K
Media
2K
Statuses
68K

Mouride .

Montréal, Québec🇨🇦
Joined November 2016
Don't wanna be here? Send us removal request.
@salioumbackefa1
Saliou 🌔
2 hours
Ma ngi ziaar boroom xam xam yi ci TL bi yeep di leen jox seen waccuwaay ! Dileen ndamoo bubaax ag ci tarixa bu ñu mën a bokk .
1
12
54
@salioumbackefa1
Saliou 🌔
4 hours
RT @papi__amadou: Sénégal lepp lou Yallah mome rk il faut niou sedd thi thieure sheuytané. Lou haram ken meunouko défendre au nom de quoi q….
0
49
0
@salioumbackefa1
Saliou 🌔
4 hours
RT @s_sourang: @xargepen Bu nu waxee avancé man naa doon ci wet yu bari, bu dee nag ci wet gii avancé ci xel ak xalaatin lanuy wax, ndax ni….
0
0
0
@salioumbackefa1
Saliou 🌔
5 hours
🚨J’offre 50 tasses de café aujourd’hui , rendez vous chez Calm et prenez votre tasse de café gratuitement c’est moi qui invite .☕️.
@Calmcoffeeshop_
calmcoffeeshop
6 hours
Tweet media one
18
35
73
@salioumbackefa1
Saliou 🌔
8 hours
Aduna bii nu nekk , ku farluwul dina am ku la yobb , kemitisme moderne baangi taxaw ngir dello nit ñi ci ag ceddo jaareko ci ay discours fallacieuses , un certain feminisme bëgg delloo certaines ci ag jaahiliya , nasaraan yeeg tubaab yi di xeex lislaam . Ku moytuwul rek ñakk.
1
43
99
@salioumbackefa1
Saliou 🌔
8 hours
En tant que murid , Les apprenants africanistes, souvent athées, qui se revendiquent conservateurs de la culture africaine tout en ayant honte de porter du caaya, ne méritent pas qu'on s'attarde sur leur discour.
0
23
72
@salioumbackefa1
Saliou 🌔
18 hours
RT @dialibatoumedia: Serigne Mountakha Mbacké.Yalla nafi yagu té and ak wérr.Barké #boromtouba. Warou niou saguann deh #Mbacké.#Boromtouba ….
0
25
0
@salioumbackefa1
Saliou 🌔
23 hours
Ana abdu jaambaar ?.
@sagittaire99
🀄️🐍
2 days
Voici une liste plus détaillée des anges ( appelés malaïka ملائكة) mentionnés dans l'islam 🤍
Tweet media one
2
0
12
@salioumbackefa1
Saliou 🌔
24 hours
Li jappandi na d.
@BambaKhadim
KHADIM خادم🇸🇳 (ibn Bachir)
24 hours
@salioumbackefa1 Niom budé daniouy lék fruit niéti fanni magal gui yeup pack bou 350.000 bi .Boudé nak fruit yu doy jour magal rek gua beug pack bou 200.000 dina bakh 😎.
1
0
0
@salioumbackefa1
Saliou 🌔
1 day
Leegi murit yi commencer lu nek ñu jeem ko jaay 😂.
1
0
0
@salioumbackefa1
Saliou 🌔
1 day
j’aime plaisanter mais jamais avec tout le monde et n’importe qui.
@Fabeeloos
🇸🇳🇵🇸ℳ𝒾𝓈𝓈 ℛℯ𝒹𝒹𝒾𝓃𝑔𝓉ℴ𝓃 🧠💋
1 day
Normalisez le fait que c’est pas tout le monde qui aime beaucoup plaisanter.
0
6
11
@salioumbackefa1
Saliou 🌔
1 day
RT @Fabeeloos: Normalisez le fait que c’est pas tout le monde qui aime beaucoup plaisanter.
0
1
0
@salioumbackefa1
Saliou 🌔
1 day
Cey.
@djigane
Jigaan ⭐️
1 day
Ceci est un privilège 😋🥱
Tweet media one
1
0
2
@salioumbackefa1
Saliou 🌔
1 day
J’ai croisé le chien d’un passant , il etait tellement excité pour venir me voir qu’il s’est échappé de son maitre pour me sauter dessus ! Son maitre etait terrifié 😂 on a joué quelques instant et ça a fait ma journée.
6
0
28
@salioumbackefa1
Saliou 🌔
1 day
Sama lunette de vue yi yaqu na 😭 je les ai depuis 4ans.
0
0
0
@salioumbackefa1
Saliou 🌔
2 days
Maam balla bi ñu bëgg def effigie maggal gi rafetluw ma ko dara ! Du ma partager ay video wam te maggal gi du ay caxaan ba ñu ko ciy associer !.
4
22
69
@salioumbackefa1
Saliou 🌔
2 days
« Ruhu mindeef yeep yallah teg nako sama loxo »loolu seriñ tuuba waxeewuko noonu ñakk degg araab yenn murit yi ag wahaabiste manipulateur motax ñu bari japp ko . Seriñ bi dafa ni que Dieu lui a donner la responsabilite de la direction des gens vers Dieu …. Zimaam ag ruuh bokkul.
4
38
124
@salioumbackefa1
Saliou 🌔
2 days
RT @Jilee_Imam: OFFICIEL : Le mercato pour le recrutement de pèlerins durant le GMT reste ouvert jusqu’au 10 août à minuit…. @Ahmadoubamba3….
0
3
0