_Ahmadouna Profile Banner
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷 Profile
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷

@_Ahmadouna

Followers
9K
Following
55K
Media
2K
Statuses
55K

Njaamus Yàlla si, di as liggéeykat ci Sëriñ Bi. Soppeb Seex Abdul Ahat Mbàkke.

Kaw Ga📍
Joined June 2017
Don't wanna be here? Send us removal request.
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
3 years
Mooy fay ëllëg
Tweet media one
6
119
1K
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
2 hours
Alxur-aan daal neex na !!! ❤️.
0
0
3
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
2 hours
RT @arwicl: - ثلث القرآن
Tweet media one
0
90
0
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
2 hours
Wallaahi ndeysaan ! ❤️😍.
@be_mouride
Imam Khalilou
3 hours
Àdduna dootu am nitu dëgg bu melni Seex Abdul Ahad.
0
0
2
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
2 hours
RT @be_mouride: Àdduna dootu am nitu dëgg bu melni Seex Abdul Ahad.
0
7
0
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
2 hours
Jërëjëf Imaam yaa xam dëgg te di ko wax !.
@be_mouride
Imam Khalilou
3 hours
Àdduna dootu am nitu dëgg bu melni Seex Abdul Ahad.
0
0
4
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
3 hours
RT @arwicl: قالﷺ: .من قرأ بالآيتين من آخر سورة البقرة في ليلة كفتاه.
Tweet media one
0
149
0
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
5 hours
😂😂😂.
@SalamDiadhiou
Daaru Salam🇸🇳CAN-BEACH SOCCER-CHAN🥇⭐🏆 DIADHIOU
5 hours
Original, Fake et Deepfake 🤣🤣🤣
Tweet media one
2
0
4
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
5 hours
😭😭😭.
@LucaVaran
Varan 🐊 2.0⭐️⭐️⭐️🇨🇮🖖🏿
10 hours
Mais attends 😭🤣
0
0
0
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
5 hours
👂.
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
7 days
Allaahu Akbar ! 😭
0
0
0
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
5 hours
Xol bu fees ak bëgg Yàlla, cér yi a koy nettali ci topp ndigalam !.
0
2
8
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
5 hours
🤣🥱.
@drpenking
Dr Penking™🇳🇬🇦🇺
11 hours
What do you people even gain from this cultism? God forbid
1
0
0
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
5 hours
😁.
@luca_varan
varan🐊 2.0 🇨🇮⭐️⭐️⭐️🙏
18 hours
😭🤣🤣🤣🤣🤣🤣
0
1
3
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
6 hours
RT @CheikhounaAhma5: Ay waxtaanam kawe na loolu.
0
1
0
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
7 hours
Balluwaay bi : Seex Abdul Ahat Mbàkke ❤️.
0
0
1
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
7 hours
{وَٱلَّذِينَ ءَامَنُواْ وَعَمِلُواْ ٱلصَّٰلِحَٰتِ لَهُم مَّغْفِرَةٌ وَأَجْرٌ كَبِيرٌ}. لندخلنهم في الصالحي, . Googu kenn ku ko manal sa bopp amut ndax : "وزكريا ويحيى وعيسى وإلياس كل من الصالحين". Foofu kenn manu faa dugal sa bopp. Yoon wi mu teg ne, ku ca aw mu dugal la ca. .
1
0
2
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
7 hours
{وَالَّذِينَ آمَنُوا وعملوا الصَّالِحَاتِ لَنُدْخِلَنَّهُمْ فِي الصَّالِحِينَ} .{وَالَّذِينَ آمَنُوا وعملوا الصَّالِحَاتِ لَنُكَفِّرَنَّ عنهم سَيِّئَاتِهِمْ} .{وَٱلَّذِينَ ءَامَنُواْ وَعَمِلُواْ ٱلصَّٰلِحَٰتِ لَنُبَوِّئَنَّهُم مِّنَ ٱلْجَنَّةِ غُرَفًا}.
1
1
2
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
7 hours
Kon yoon wi mu ne ku ca aw daje ak loolu rekk ca lanu war a sóobu aw ca. .
1
1
1
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
7 hours
Ngëm gi nag manut a wér te àndu ci ndax fu mu waxee : .{والذين آمنوا وعملوا الصالحات}. La ca teg. {والذين آمنوا وعملوا الصالحات}.Joo gis mu wax ko it la mu ca teg deful lu maneesul a ñàkk te deful lu kenn man a fexeel sa bopp mbaa nga may ko sa bopp.
1
0
1
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
7 hours
{{ذلِكَ بِأَنَّ اللَّهَ مَوْلَى الَّذِينَ آمَنُوا، وَأَنَّ الْكافِرِينَ لا مَوْلى لَهُمْ}}. Loolu wane na ne kon gëm gi lu am solo la. Gëm itam dafa mel ni, dafa fob jëf uw yiw, wane ne ku gëm Yàlla fàww nga war koy def ; sañóo koo bañ ndax da koo lëkkale ak ngëm.
1
0
1
@_Ahmadouna
Baay Jaañ 🇸🇩 | 🇮🇷
7 hours
Sunu waxtaanu tay nag mi ngi jëm rekk ci gëm Yàlla ak jëf uw yiw ndax dafa mel ni gëm Yàlla mooy fondumaŋu lépp. Mel na ni it moom doŋŋ la Yàlla am soxla ci nun ; ngir ba mu nu bindee, moom nu, séqu nu ak kenn man a wax ne :.
1
0
1