Sheex Mustafaa 🇸🇳
@SheexMustafaa
Followers
2K
Following
11K
Media
758
Statuses
31K
Salam Mbokkou yi nionguiléne di woo si 3ème édition NGONTU WIRD MAH’OOZ mouye Mercredi 25 mars 2026 si Massalikoul Djinaan bou 16h dioté Inch'Allah 🚨Koussi beugue barkélou manako yoné si numéro bi késsé : 77 449 72 88 (Dieuwrigne Mouhammadou Sarr)
1
69
113
Dewenati Di balou akh gnep Di bal gnep Di niane féké ay koor you bari té sunu borom nangoul nu 🙏🙏
3
10
94
On rigole, mais la justice 🇲🇦 emprisonne des supporters 🇸🇳 pour du foot… Parmi ces détenus, il y a des pères de famille, et c’est inadmissible. Libérez les supporters 🇸🇳 !
🚨🚨 « 𝗡𝗢𝗨𝗦 𝗢𝗡 𝗚𝗔𝗚𝗡𝗘 𝗟𝗘𝗦 𝗧𝗜𝗧𝗥𝗘𝗦 𝗦𝗨𝗥 𝗟𝗘 𝗧𝗘𝗥𝗥𝗔𝗜𝗡 𝗣𝗔𝗦 𝗗𝗔𝗡𝗦 𝗟𝗘𝗦 𝗕𝗨𝗥𝗘𝗔𝗨𝗫 ! 😬 » Gana Gueye 🇸🇳 "𝗦’𝗘𝗡𝗚𝗔𝗚𝗘 𝗣𝗘𝗥𝗦𝗢𝗡𝗡𝗘𝗟𝗟𝗘𝗠𝗘𝗡𝗧 𝗔̀ 𝗥𝗘𝗚𝗥𝗢𝗨𝗣𝗘𝗥 𝗟𝗘𝗦 𝗠𝗘́𝗗𝗔𝗜𝗟𝗟𝗘𝗦 𝗘𝗧 𝗟𝗘𝗦 𝗥𝗘𝗡𝗗𝗥𝗘 𝗔𝗨 𝗠𝗔𝗥𝗢𝗖
210
838
3K
L’argent ne devrait en aucun cas être le ciment de nos relations humaines. Qu’Allah nous préserve du désir effréné de revanche sociale.
0
21
58
Nu delloo njukkal Sëriñ bi, dund na coono yu metti ngir sunu bànneexub tay.
Ku Baax Ki mi ngi nettali bisub kori bu mu dundoon ca tukki ba, dafa wax ne : "Daawuma xam weeru koor bu jotee , waaye Yàlla moo may xamal saa su weer feeñee, ndax dëkk boobu (Gabon) xamuñu lu dul weeruw farañse. Ba nu yeggee nag ca bisub kori ga, wori naa ma sangu def lépp 👇
1
58
345
Dewenatileen, yal na nu ko fekkee ay at i at barkeeb boroom Tuubaa
4
10
102
Comment Lekjaa et le Maroc tiennent la CAF ? La réponse dans cette vidéo
24
474
1K
@husseinuchiwa07 @SheexMustafaa "Guiss nagn ko". Taxoul niou xam kuko guiss d. Imam bi tmt guissuko dègg rk lassi am. Wala dou lolou ?
0
1
0
@husseinuchiwa07 @SheexMustafaa Aprés nafila alors que la lune s'est couché à 19.53 ? Yërëm leen seen bopp... The more you talk, the more you display your ignorance
1
1
2
Dama tayaloon indi hadiiis bi mais heureusement lo tayal rek amna ku ci farlu ❤️
Sahih Muslim 1088 Chapitre : « l’on ne tient pas compte de la grandeur ou la petitesse du croissant lunaire .. « Nous sortîmes pour accomplir la ‘umra. Lorsque nous campâmes dans la vallée de Nakhla, nous observâmes le croissant lunaire.
0
18
95
So guissei weer ak beute wax degue mane ko photo khanaa
0
0
0
Al hamdoulilah Serigne Touba Serigne Mountakha yalla nafi yagg té ande ak werr 🙏🏾🙏🏾
0
19
164