BAYE ALIOUNE
@PaaLuuNee
Followers
2K
Following
22K
Media
129
Statuses
6K
Bëgg baax rek, sellal pour espérer bokk ci taalibé Borom Touba yi…
0
6
33
Ci wàllum ay nit toog nii wër di jàng ag xasiida, amul lu ci dàq xasiidag #Raa’iya Baay Mustafaa Jóob. Bu ma amoon jot, man naa ci debaa sax. #Dundal_Koor_HTDX
2
28
179
🔴 JOUR 1️⃣1️⃣: ⏯️ Prestation KUREL NUURUD DAARAYNI HT RUFISQUE المشرب الصافي. من المنبع الشافي 𝑨𝒍 𝑴𝒂𝒔𝒉𝒓𝒂𝒃𝒖’𝒄̧- 𝒄̧𝒂̂𝒇𝒊̂ 𝒎𝒊𝒏𝒂𝒍 𝒎𝒂𝒏𝒃𝒂𝒉𝒊’𝒔𝒉-𝑺𝒉𝒂̂𝒇𝒊̂ La Fontaine Purificatrice émanant de la Source Qui Guérit. #MashrabuCaafii2026
3
48
228
Oustaz Hady Niass kouné amél ngako Allarba ndakh Nieup Jangué nagn si Moom sounou Diiné. Ceci est un appel à contribution au financement de la 2e phase du Projet Complexe Islamique Africain Mame Khalifa Niass de Bambilor. 1 Musulman / 1000 Fr ! Nassi Nieup Japp! Wave & OM : 77
4
626
1K
😭😭😭
Il faut un jour ma déguiser wu, sol Baye lahad jusque pour tewlou biir résidence 👍🏽. #MashrabuCaafii2025
0
0
0
Mbàkke xassida yi amna si lu ken amul lepp rek ngir sa fonk ko ak bëgg Sëriñ Yaa njaboote ñëpp Mbàkke Yagg fi lool te and ak wer
3
69
422
😭😂😂
0
0
0
Alxemis 28 fan ci weeru Gàmm 1342 (1923) Sëriñ bi dafa julli tàkkusaan ba noppi, njëkk muy jóge fi mu doon jullee, mu wax ne : “Ku ci bëgg a tàbbi àjjana ji Yàlla dig ñi ko ragal, na jublu Yàlla ci topp ay ndigalam, ku bëgg a mucc ci sawara, na jublu Yàlla ci moytu tere yi”
2
55
188
Gone yi Mokkal Alxuraan teg ci, jàng xam-xami diine yi, ñu yar léen ci lislaam gu wer ak ay teggiin, ñu choisir orientation ci Université bi am ay diplômes, man a ligéey fepp garder seen originalité sans complexe. Ces générations seront une bénédiction pour le pays
4
48
262
Ab murid foo mëna nekk muy fi ngay ligeeye/ jange, RS, dangaa wara japp ni yaafa teewal sëriñ tuubaa, jeema nekk royukaay ci lepp. ✍🏿@AsSaalih22
0
19
60
Seepileen cheikhouna diagne ak njabootam ba pareh après ngen deff seen classement 😎✌🏻
Nous voilà à une semaine de prestation,et voici les Kurels HT qui ont déjà déclamer au résidence: 1) Mashrabusçaafi 2) Touba 1 3) Touba 2 4) Parcelles 5) S.Mahib 6) Thies 7) Këur Massar 8) S.Saliou Faites moi le classement de vos top prestation. #MashrabuCaafii2026
3
3
11
Nous voilà à une semaine de prestation,et voici les Kurels HT qui ont déjà déclamer au résidence: 1) Mashrabusçaafi 2) Touba 1 3) Touba 2 4) Parcelles 5) S.Mahib 6) Thies 7) Këur Massar 8) S.Saliou Faites moi le classement de vos top prestation. #MashrabuCaafii2026
7
7
86
« Par le secret du Coran descendu sur toi,Accorde-moi la droiture dans mes actes,Purifie mon cœur de l’ostentation et de l’orgueil, Et remplis-le d’un amour sincère pour Allah. Ô Bien-aimé d’Allah, Je n’ai d’espoir qu’en ton intercession, Ni de porte vers laquelle me tourner en
0
22
173
Sëriñ bii, lu mu amut ca boroomam rekk da ko faa fekkul… Boramam jox na ko lépp
0
27
263