_Bachiir Profile Banner
بــــــشير 🇵🇸 Profile
بــــــشير 🇵🇸

@_Bachiir

Followers
8K
Following
63K
Media
371
Statuses
40K

تحلى جمال الخلق والخلق أجمل# بشير هو البشرى يبشر بالحكمة.

Daaru Xudóos
Joined September 2013
Don't wanna be here? Send us removal request.
@_Bachiir
بــــــشير 🇵🇸
6 years
😭 Vous n’avez pas fait ça vs avez raté votre vie. Wola.
62
678
3K
@_Bachiir
بــــــشير 🇵🇸
49 minutes
Salaam,. Damaa bëgg a jàng informatique, ku may teg ci ags bu wóor ?. 😌.
2
1
6
@_Bachiir
بــــــشير 🇵🇸
59 minutes
Yéen @dakardemdikk1 essayez d’introduire dans l’appli, ngir Yàlla, une fonctionnalité permettant au client de changer la date de son billet, au moins 24h avant l’heure de départ. Yéen a ngi lekk àqi nit ñi rekk, AH !.
0
0
1
@_Bachiir
بــــــشير 🇵🇸
2 days
Abdu Laahi doom Omar nee na: Yónnent bi Halayhi salaam mas na ko ne:. « Abdu Laah, bul mel ni diw, moom de daan na julli guddi leegi bàyyi na ko ». [Buxaari: 1152]. Ag xuppe mi ngi ci ku doon def lu baax ba noppi génn ca.
0
23
76
@_Bachiir
بــــــشير 🇵🇸
4 days
Jàpp naa ne lu nit man a ñaan jamono jii na ci boole ag ñàkk jot, ndax boo ñàkkee jot yu bari dootoo ko tal, bariwaan a lóoxóor yu nit di dugg ak am jot gu bari a ko ko ci dugal.
3
43
109
@_Bachiir
بــــــشير 🇵🇸
5 days
Maanaam fuñ bind ne tamxarit moom cere rekk lañ a lekk ?. Ah riptiir waay. Au passage, bu amee ku fi togg soos 😋.
1
2
15
@_Bachiir
بــــــشير 🇵🇸
7 days
Bu dee Njiitu réew lañu warut a jiitu ci wax walla jëf ci dara,.Kon lu tax ñuy jiitu Yàlla ci ay dogalam ?. Nguuru moom, nguuru la rekk, te nguurug Yàlla gi bokku ko ak kenn.
0
11
33
@_Bachiir
بــــــشير 🇵🇸
12 days
Des mots de remerciement adressés à Madame la DAGE du MEN (en bleu), au nom de la promotion F2B2.
Tweet media one
Tweet media two
0
5
21
@_Bachiir
بــــــشير 🇵🇸
14 days
RT @_Bachiir: Yónnent bi halayhi salaam nee na:. « Àddina dara desatu fi lu dul balaa ak fitna. ». Yal na nu Yàlla musal ci fitna, li ci në….
0
69
0
@_Bachiir
بــــــشير 🇵🇸
15 days
Un atelier de formation pour le Comité Scientifique National de Validation (CSNV) dans le projet de SENTERMINO qui sera bientôt lancé au grand public. #MEN #UNESCO #IFAN #ESP #DALN
Tweet media one
Tweet media two
Tweet media three
Tweet media four
1
17
63
@_Bachiir
بــــــشير 🇵🇸
15 days
Soxna Xadi Ja yal na ko Yàlla yërëm te jéggal ko, sama xarit la woon te amoon ci nun yërmaande bi nuy xale daan ñëw ci kër gi.
2
2
29
@_Bachiir
بــــــشير 🇵🇸
16 days
Echange avec le Directeur des Daara et son personnel sur plusieurs sujets particulièrement la cérémonie officielle des Assises des Daaras, le 26 juin 2025.
Tweet media one
Tweet media two
12
23
115
@_Bachiir
بــــــشير 🇵🇸
16 days
Bàkkaar bi gën a mag sa digg ak Yàlla moo tane bàkkaar bi gën a ndaw si diggante ak nit, ndax du la ko baal ëllëg.
0
1
3
@_Bachiir
بــــــشير 🇵🇸
16 days
Àq yi (tooñ) ñaar lañu: sa diggante ak sa Boroom, sa diggante ak sa moroom. Bu njëkk bi boo ko tuubul ba dee sax Yàlla man na la ko baal, bam des bokkaale;.Beneen nag bu la ko sa moroom baalul Yàlla du la ko mas a baal, moo tax mu yéeme.
1
8
53
@_Bachiir
بــــــشير 🇵🇸
21 days
Ki mucc mooy ki dee yóbbaale ay bàkkaaram, texeedi weesuwul faatu say bàkkaar wéy di fi des ngir lu bon loo sosoon nit ñi di ko def ci sa ginnaaw.
0
40
115
@_Bachiir
بــــــشير 🇵🇸
21 days
Fexeel ba bu la nit rawee ci jëf yu baax yi (saraxe, sikr, naafila…) nga jéem ko raw ci bàyyi yu araam yi ak yi ñu sib yi, ndax loolu laajul alal ju bari.
0
27
91
@_Bachiir
بــــــشير 🇵🇸
21 days
Bépp ànd bu gëj a déggante yàq dafa fekk ne kenn ki a jàppoon.
1
20
59
@_Bachiir
بــــــشير 🇵🇸
26 days
Dans la vie, tout est lié : les connaissances, les histoires, les faits… Il y a toujours un rapport. Le connaît celui qui le connaît, et l’ignore celui qui l’ignore. 🤨.
0
18
74
@_Bachiir
بــــــشير 🇵🇸
30 days
Bokk na ci li Saytaane dëkku (défier) woon, dina fexe ba nit ñi di soppi bindub Yàlla bi. {Certes, je ne manquerai pas de les égarer,[…] ; je leur commanderai, et ils altereront la création d'Allah} . [S4V19].
1
11
45
@_Bachiir
بــــــشير 🇵🇸
1 month
Yónnent bi HS mas nay julli, sujjoot sujjoo gu yàgg, kenn ci sahaaba yi jaaxle siggi, gis ne Asan/Usëynu (maa fàtte) moo toog ci kaw ndoddam, bim noppee mu ne:.Sama doom jii de moo toogoon ci sama kaw, ma bañ koo gaawantu, ma doon xaar mu wàcc ma siggi.
@luca_varan
varan🐊 2.0 🇨🇮⭐️⭐️⭐️🙏
1 month
Les enfants ont des pouvoir mystiques
1
10
68
@_Bachiir
بــــــشير 🇵🇸
1 month
Kilifa mas na ma nettali ne bi Sëriñ bi nekkee Njaareem ay guddi mas nañ dégg ay yuuxu, Sëriñ bi laajte, ñu ne ko dafa am ku faatu. Mu ne: yuuxu yooyu ku tëdd guddi te julliwul gee rekk lañ ko war a yuuxu. Ñuy wax ne mag ñi ku ci julli mbooloo masaan raw rekk dañ lay jaalesi.
0
29
96