Mohamed.
@toure____m
Followers
6K
Following
9K
Media
223
Statuses
13K
Technicien supérieur et licencié en mécatronique automobile. Owner of ALMT automobile.
Joined July 2017
Son Excellence auto bimou done defer campagne F250 bi nio ko done job et tout🥲
6
50
411
Kia K3 2015 Moteur 1.6L full options 79000Km Prix: 4M900 Auto bi mako dieundeul borom et ma gérer entretien bi comme d'habitude sou len nexer meu garantir ko, indi len 500 mecanos tamit sou ngen beuguer😂
1
31
99
Curious about Mighty's new open APIs? We made a video because it's 2025.
1
5
21
Sen autos yi ngen di yobou lavage aussi def len ci attention. Beaucoup de gens me contactent en mode digni am ay pb électroniques après lavage. Gayi sen jet d'eau yi mo am doler th digni armer req naq khamouniou watier😂. Li olof nane ndox dou bayi yonam après vous allez vous
3
25
188
@toure____m Je remercie Monsieur Touré pour le service rendu. Il a fait preuve d’un grand professionnalisme dans la révision du véhicule qui lui a été confié. Son travail se distingue par sa fiabilité, sa courtoisie et sa transparence. Je le recommande vivement.
1
4
11
Je faisais la vidange d'une Cadillac today, xol len pâte bi ci huile bi, je desserre le boulon de vidange en bas huile guenoul sax ndax pâte bou beuri. Wax nako beu sonou bayi len di négliger sen entretiens yi. Ki mom yAllah moko dimbeuli moteur leu narone dieundi pour une
7
25
154
$RGBP $RGBPP New research report on Regen BioPharma published today
7
2
48
Hyundai Tucson yi sen problème par rapport au freinage apparemment défaut leu ci niom, cas yiniou mey indil ci lolou beuri neu torop. Quand vous freinez amneu bene genre bruit bou ngen di deg ci pédale de frein bi c'est comme si la pédale de frein repousse votre pied. J'ai reçu
14
15
125
2 cartons huile la diexal semaine passée gayi sen yaram tang neu naq ci vidange yi😭
1
3
24
Yango la dieul ben SM3 automatique je sais que auto bi vitesses yi nimouy douguer c'est pas normal mais le chauffeur mom migui dawal di dem req mais il sent que auto bi amneu pb parce que mogui xol tableau de bord bi req, auto niak ci xam dara je vous promets que woroul le jour
7
12
207
Devnet 2.0 is live. Experience the fastest decentralized network for instant payments. ↓
104
64
361
On m'a amené hier une Audi A7 2022, le gars voulait un diagnostique avant achat. Je viens je branche la machine je vois que numéro VIN bi machine bi guiss ak bou auto bi bokoul je suis hyper strict je sais je prends la peine de tout vérifier motax auto boumeu xol beu nileu
14
33
259
Je devais faire une vidange moteur à domicile today, la sœur de la propriétaire gueneu req ni "vidange à domicile liiii d magui key dogeu deg" maniko deg ngako guiss ngako tey😭
3
4
70
Un client m'appelle pour me demander ndax boite de vitesses degn key vidange parce que depuis qu'il a changé sa boite de vitesses def neu 2 ans legui meussouko vider th 1 million leu dieunder wone boite bi, il attendait que la voiture signale "vidange boite de vitesses
6
39
241
J'ai une cliente bouy def sam promotion à ses collègues neneu len mane auto bougn meu diox meu diay ko en 2 jours, ses collègues yeup gni ngi mey beug contacter pour meu diayal len sen autos🤣 Les voitures que je vends à 99% ay autos leu yo xamni mane ma done gérer entretien bi
6
23
302
$TDOC $AIRDF $AMWL $HIMS AI in virtual healthcare is booming, fueled by physician shortages, patient accessibility challenges, new tech, and convenience. Here we look at a few differentiated public companies in the space, brought to you by Rocket Doctor AI.
0
0
8
Meuss neu dougg sama auto dima yobou parce que j’avais la flemme de conduire, mou démarré daw à peine 100 mètres nima auto bi pâte moteur bi da dam, billettes yi magat legui moteur bi commencer vibrer, geumoumako. Une semaine après moteur bi di vibrer ci lako nangoul bé ni😂
@AmDjigo1 @toure____m Waa dji dafa meune dh 😂 Sa problème sakh mola kay wakh
4
11
195
Un gars m'a appelé hier pour me demander mon avis entre une Mazda et une Peugeot 3008. Maniko saay ci gataal doumeu yor Mazda di xol lenen! Sénégal diamono yi kouy weur auto bou deugeur, auto bou nopaler, do voyager beu xalat dara, fouleu nex dem JE RECOMMANDE FORT LA MAZDA, sou
13
32
307
"Quand je roule à 100km/h quand je freine le volant et la pédale de frein tremblent" une des causes principales c'est des disques de frein gondolés. Disque de frein gondolé naq likey indi louci beuri moy ngen dawal beu disques yi tang dieur ngen diar ci ndox. Même quand vous
10
24
152
Custom gold bracelets — engraved with any name 🔥 Luxury shine • Hypoallergenic • Built to last. 20% OFF today only. Perfect gift. Premium look. CDORÉ
3
0
8
Hyundai Accent 2012 Moteur 1.6L Auto bi mako dieundeulone dame bi il y a 3 ans, kay len dieul ko! Prix: 3M
3
24
81
Veillez à ce que vos pneus soient à la bonne pression, beaucoup de vulganisateurs ne connaissent pas exactement la pression exacte préconisée par le constructeur. Niom negn pomper mou fess req parer negn ci. Si vous mettez une pression supérieure à la pression de référence ay
5
17
68
Le gars il a une Edge 2018 il vient de la Mauritanie avec un check moteur allumé, ABS,ESP lepeu tak, neneu fofou gayi minouniou électronique bi niou boler ko ak mane mou dawal beu fi pour meu defaral ko lolou😭
9
8
135
Par rapport à la climatisation de votre voiture niou beuri digni remplir gaz périodiquement pensant que c'est normal, c'est vraiment pas le cas. Clim auto sou feker y a aucune fuite lep ras meune ngen tok 5 ans voire plus dou ngen ko lal à part changer les filtres habitacle.
2
30
175