@MrsKarmeel
King Karma Fth
2 years
Diang diné fi nguene ko tek metina. Melni camp militaire pour enfant
14
52
326

Replies

@abdourami
🇸🇳Abdou Touré🏆⭐️
2 years
@MrsKarmeel @ManouMhd 😂😂😭😭
1
0
0
@MrsKarmeel
King Karma Fth
2 years
@abdourami Niune nio beug lou tar grand
1
0
1
@MariaLacouture
Pitō 🇸🇳⭐️
2 years
@MrsKarmeel Mon frère avait pris un oustaz pour mouye nieuw keuram diko diangal. Premier cours, le gars lui demande de s'assoir par terre ndakh kouy diang alquran dou tokk ci chaise. Fa la diang bi yéme
5
15
84
@MrsKarmeel
King Karma Fth
2 years
@MariaLacouture 😂😂😂😂 niune hawma pk suniu dara simplul. Dagn siy bolé ey supplément yo hamni Amul bene bonus pour nga gaw mokal
1
1
16
@_Bachiir
بــــــشير
2 years
@MrsKarmeel Jàng diine masul yomb te du mas a yomb, ku bëgg a tappale nag yoon waa ngoogu. Am naa boroom xam-xam bu mas a wax ne tuur naa dereet (saw) ñaari yoon ci sàkku xam-xam benn bi Baxdaad la beneen bi Màkka. Sëriñ Tuubaa nee na cib coona kepp lañu man a ame xam-xam.
1
9
36
@MrsKarmeel
King Karma Fth
2 years
@_Bachiir Seugn bi nga Balma wahou lek Lagn done wah ak diné. Wahuniu fi yeup nga doug ni
2
0
0
@MrsKarmeel
King Karma Fth
2 years
@preinomnom Se bop nga kham suniu genre bi rek hamoul kheeer 😂. Da am niu fok sen diar diar moy généralité
0
0
0
@MrsKarmeel
King Karma Fth
2 years
@Awaa_____D 😂😂😂 Sénégaaaaal
1
0
0
@SamaRakkeu
Mr Kobar M
2 years
@MrsKarmeel Pkoi nga wakh
0
0
0
@badoudiop96
Abi_sibtayni🕋🇵🇸🇵🇸🇵🇸
2 years
@MrsKarmeel @BintaAstel Xam xam-xam dees koy tarbiyu. Àddina lula yomb doo xam njariñ la te doo ko fònku.
1
0
8
@Cheiiikhou
Cheiiikhou
2 years
@MrsKarmeel Baniou yombalé ba légui moussiba rek. Touti lay diangg fokni may wadia, di wédi makk gni… Outt xam xam meunoul yomb
0
0
2
@SSaliouDiop
Saaliw Jóob Lewna
2 years
0
0
0
@BJAHRAH
Abubakr🇸🇳🇳🇬🇵🇸
2 years
@MrsKarmeel @BintaAstel Lekk mom sileu ndakh sa khel meuna fonctionner kou lekoul dou khalate dh
0
0
0
@Seexuna18
𝐗𝐀𝐀𝐃𝐈𝐌🇸🇳🇵🇸💙
2 years
@MrsKarmeel dou camp militaire dh mais dou paradis aussi
0
0
1
@MinekaAbdoulahi
Ibn Sheikh Aziz❤👑
2 years
@MrsKarmeel Rappelle toi Yonente tamit Djibril dafko ndiath baam fogni rouwam legui mou guenn... Donc thiono bi sunnah la ci !!!
0
0
2
@FayeGarmi
Gαrmi At-Tijāni🇵🇸
2 years
@MrsKarmeel Lo donoul talibém do doon serignam
0
0
0
@darkmole77
DARKMOLE🇺🇸🇸🇳
2 years
@MrsKarmeel Yönou YALLAH Mo mēnn nonou
0
0
0