MbackeSaaBorom Profile Banner
سليمان Jëf 🤍 Profile
سليمان Jëf 🤍

@MbackeSaaBorom

Followers
19K
Following
19K
Media
139
Statuses
29K

#DST_DMCIF Bëgg Fallu♥️ || #OilProducer || #Alxur'aan_Lover #BusinessStrategy #MinanulBaaxilXadiim & #WakaanaHaqqan || #HTDK

Touba
Joined January 2013
Don't wanna be here? Send us removal request.
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
6 years
قُل لَّن يُصِيبَنَا إِلَّا مَا كَتَبَ اللَّهُ لَنَا هُوَ مَوْلَانَا ۚ وَعَلَى اللَّهِ فَلْيَتَوَكَّلِ الْمُؤْمِنُونَ.
4
8
72
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
4 months
RT @SokhnaAstouD: Kou amagoul yeurer korite? 😊on a confectionné une petite collection de costumes africains pour la team dernière minute🥰ve….
0
62
0
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
5 months
Yalna keemtaanu gudd fan feen ci moom barkep Seex Fallou.
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
4 years
Dans la pluralité des différences humaines, la prise de décision en haute instance, .Serigne Mountaxa MBACKE reste l'épicentre sans équivalant du modèle de citoyenneté avéré et du guide soucieux des maux de son peuple comme le fît son grand-père Cheikh Ahmadou Bamba Xadim Rassoul.
0
2
2
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
5 months
10i fan ci koor gi mooy sama bisu judd ☺🎉🎊.
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
1 year
10i fan ci koor gi mooy sama bisu judd ☺🎉🎊.
1
0
4
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
5 months
Yàlla miy aji xam ji, xam na ni Borom Touba rek lañu bëgg 😭😭.
1
31
95
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
8 months
Sama jëf ci ndigëlu jumma ji loxoy Seex Ibrahim Faal kepp moma ci doy.
4
18
77
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
8 months
Yaaram yemal ci Cheikh rek mu doyla te bayiñu ak Seex doy nanu.
@LayeBarro2
Laye Barro 🇸🇳💀
8 months
Les Hommes Baye Fall que je connais dagnouy diamou yalla normal et ils insistent sur les prières : « Delen diamou Yalla » et je précise c’est des petits fils du Cheikh nakk . Gni doul diouli dagnouy mboubo baye fall rek mais donougn ko 🤝🔥.
2
1
7
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
8 months
Seex Ibrahima Faal mooy yoon wi.
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
2 years
Seydina Ibrahim Faal mooy Lamp yoon wi
0
2
19
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
8 months
وَمَا مِن دَابَّةٍ فِي الْأَرْضِ إِلَّا عَلَى اللَّهِ رِزْقُهَا وَيَعْلَمُ مُسْتَقَرَّهَا وَمُسْتَوْدَعَهَا ۚ كُلٌّ فِي كِتَابٍ مُّبِينٍ.
0
1
6
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
8 months
RT @AlMosahf:
Tweet media one
0
352
0
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
9 months
Bulletin yi bëri nañu te niroo. Mère yi mom dinañu votel ku ñu xamul.
2
0
3
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
9 months
Jëwrin dafñuy ruube rek😄😄. Ku moss Yàlla dara dotul saf ci yaw dara. Lolou moy mandi ci Nuurulah.
@hikmatalkalima
Shabâb Al-Janna
9 months
Ajjana am na sangara waaye amul japp daaj luy lolu gayn 😒 !?.
1
0
0
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
9 months
Ki gën a naqaree waxtaanal mooy ki xamul daaara ci tasawuuf te yem ci ay teere. Ay werente kepp lay jur. Bul fate ni Haqqiqa buntu bu yaatu la dinganté nit ak Boroomam. Kon jaam bi soxla na équilibré oscillation biy am dinganté fanaaw ak baqaaw ngir am nafsul kamilatu.
1
14
45
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
9 months
RT @serignediagne7: @MbackeSaaBorom Seex Fallu la nu woolu❤️.
0
1
0
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
9 months
Maa ngi sant saa Borom ci Sëriñ bi. Jërëjëfëti Seex Muhammadu Faadal sama waadji ♥️.
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
1 year
Maa ngi sant saa Borom ci Sëriñ bi. Jërëjëfëti Seex Muhammadu Faadal sama waadji ♥️.
2
8
25
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
9 months
Ak lu mën a xew, Sëriñ Tuuba lanu bëgg. Noo ngi fedali sunu jayante ci moom.
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
1 year
Ak lu mën a xew, Sëriñ Tuuba lanu bëgg. Noo ngi fedali sunu jayante ci moom.
1
9
36
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
10 months
Mèrou Sourah yi ño mën wa Darou khoudoss foouf.
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
4 years
Nooon mère bi gaddu na sama akh koi.Jaay ma thièrè mou jaay ma tiox 😭. Affaire yangui jadd ci rouxou gorge bi.
2
1
4
@MbackeSaaBorom
سليمان Jëf 🤍
10 months
RT @MbackeSaaBorom: Bokk na liy dimbali nit ci dox bi muy dox jëm ci boroom am mòoy mu xam xeet i bakan yi am ak fumu ci tolou. Li ci jiit….
0
11
0