CoskasMbao Profile Banner
CSCM Profile
CSCM

@CoskasMbao

Followers
142
Following
171
Media
87
Statuses
220

Coskas Section Communale de MBAO Au Service de Khalifa Ababacar SY +221776720707

Grand Mbao
Joined May 2025
Don't wanna be here? Send us removal request.
@MousyllaDk
mouhamed sylla
12 hours
Abuna abubacrine❤️
@CoskasMbao
CSCM
1 day
Ku ñépp di XOOL Da ngay jaar fu LEER Ku ñépp di DÉGLU da ngay wax lu LEER Ku ñépp XAM Da ngay ÄND ak ku ñu XAM Serigne Babacar SY RTA
0
0
2
@amiral_bgm
Amiralbgm Pedri 🇸🇳🇪🇸
7 hours
Jawharatul Kamal pour ceux qui ont du mal à lire l’arabe ALLAHUMA SALLI WA SALIM HALAA HAYNI RAHMATIR RABBÂNIYATI WAL YAAKHOÛTATIL MOUTAHAKHIKHATIL. HÂ’ITATI BIMARKAZIL FAHOÛMI WAL MAHÂNI. WANNOÛRIL AKWANIL MOUTAKAWINATIL ÂDAMIYI SÂHIBIL HAKHI RABBÂNI ALBARKHIL ASTÂHI
2
46
131
@AissataDram5
NénéYayam⭐️⭐️
14 hours
Bonsoir j’espère que vous allez bien ? Alors j’aimerais faire une SADAQA JARIYA. Je dédie cette sadaqa jariya à la mémoire de ma chère grand-mère, qu'Allah lui accorde Sa miséricorde infinie et la récompense pour tout le bien qu'elle a fait. Par cette sadaqa, je souhaite offrir
2
243
383
@haadijaMouhamed
Khadidjatou At’tijani✨
17 hours
Prend 5 minutes pour faire ton dhikr : - Subhan'allah  - Al Hamdoulillah - Astarghfirullah - Allahu Akbar - La ilaha ila Allah   - La hawla wa la quwwata illa billah - Astarghfirullah wa atubu ilayh à chaque fois que quelqu’un le lit, tu seras récompensé insha'allah.
0
275
615
@bbboubacar03
💙🥰سيدي الحاج أبو بكر الأمين ELAsBa
15 hours
Sunu leep ci Barkep Serigne Babacar Sy 🙏🏽🥰❤️‍🔥
@CoskasMbao
CSCM
22 hours
Man Serigne Babacar SY, ku ma jox SA BENN, ma teyeel la SA LÉPP Ku ma jox SA NAAR, ba teyeel la SA LÉPP Ku ma jox SA LÉPP, ma teyeel la SA LÉPP Ku ma joxul SA DARA, ma maandu SI YOW. Serigne Babacar SY RTA
0
3
21
@CoskasMbao
CSCM
15 hours
Képp ku la wax ni mèn naa fexe ba nga am TERÄNGA ÀDDUNA te liggéey loo wu la, DAF LAY NAX Képp ku la wax ni mën naa fexe ba nga dem "AL JANNA", te waxula nga melal say jikko na Yalla bèggee DAF LAY NAX Serigne Babacar SY RTA
0
0
7
@B4ye_D4rou
𝑱𝑨𝑨𝑴𝑼 𝒀𝑨𝑳𝑳𝑨 𝑩𝑰𝑯🤲🏾
1 day
Vers 3H du matin C'est exactement le moment où le Créateur de l'Univers descend au ciel le plus bas pour demander : Qui M'invoque pour que Je l'exauce ? Qui Me demande pardon pour que Je lui pardonne ? Lèvez-vous, même pour deux rakats. Le Tahajjud change les destins.
13
472
3K
@haadijaMouhamed
Khadidjatou At’tijani✨
2 days
Coran avec traduction des versets en français et phonétiques 🏷️ 8000f Je compte sur vous pour la visibilité 🤍
1
152
270
@mamesarrdiff7
Dr Maktoumist
19 hours
Serigne Mor Diop yalna ko Yalla fayy yiww té guddal fanam. Il nous offre des brochures tellement intéressant.
5
50
253
@ABLAYEDIALLO0
Dele.AlNour ☪️📿
1 day
Qu’Allah efface de nos coeurs l’ostentation, la procrastination et l’orgueil.
3
45
231
@amiral_bgm
Amiralbgm Pedri 🇸🇳🇪🇸
20 hours
Comme toujours avec Mame Khalifa RTA 🤍
1
8
71
@MustafaSarr3
Mustaf🇸🇳⭐️⭐️
20 hours
Bëurri fay Tank ayoul fa Mbaye
0
36
425
@CoskasMbao
CSCM
21 hours
Sänxaleñ booloo WAT WER Serigne Babacar SY RTA 40600 Salatoul Fatihi sur 120.000 Salatoul Fatihi Reste 79.400 Salatoul Fatihi
@CoskasMbao
CSCM
3 days
25 Mars 2026 - Adiya Seydi Aboubacar SY RTA 120.000 Salatoul Fatihi avant le 25 mars Niou séddo ko def ko si Barké Yonente bi SAWS pour sunu Gorgui 🤍 Dieul negn 10.000
0
13
168
@CoskasMbao
CSCM
22 hours
Man Serigne Babacar SY, ku ma jox SA BENN, ma teyeel la SA LÉPP Ku ma jox SA NAAR, ba teyeel la SA LÉPP Ku ma jox SA LÉPP, ma teyeel la SA LÉPP Ku ma joxul SA DARA, ma maandu SI YOW. Serigne Babacar SY RTA
0
18
227
@SsmaSenegal
SSMA-SENEGAL l’officiel
1 day
🚨En route vers le 25 mars « Ku Ñamm wilaayam Jommi, Ku gëustù Xam Xamam waarù » Serigne Babacar Sy Abdou à son homonyme Serigne Babacar Sy (Rta)🤍✨ . . . . . . #abnahu #ssmamedia #GamouNdar #Tivaouane #talibecheikh #grandemosquedetivaouane #talibecheikh #SerigneMoustaphaSy
0
18
175
@CoskasMbao
CSCM
1 day
Ku ñépp di XOOL Da ngay jaar fu LEER Ku ñépp di DÉGLU da ngay wax lu LEER Ku ñépp XAM Da ngay ÄND ak ku ñu XAM Serigne Babacar SY RTA
1
33
382
@CoskasMbao
CSCM
1 day
Ba laa nga ngay wax xamal ñett yii: Li ngay WAX, ki ngay WAXAL, ak fi ngay WAXEE. Serigne Babacar SY RTA
@SalutHabib
📿 حَبِيبُ اَللَه ✍🏾
1 day
1
13
185
@bbboubacar03
💙🥰سيدي الحاج أبو بكر الأمين ELAsBa
1 day
As Salāmou 'Aleyka Yā Seydi Yā RassoulAllah ﷺ ✨
0
8
26
@CoskasMbao
CSCM
2 days
Saay-saay mooy YÄQ GOR, fu mu TOOG, tooge ko fa. Ku iñaan mooy YÄQAL GOR, yiw wu mu gis muy ñèw jem ci moom, mu DOGAALE KO. Serigne Babacar SY RTA
0
27
266
@CoskasMbao
CSCM
2 days
Boul tokhi yonou Tivaouane defko ni sa yonou tol 🤍 Serigne Abdou Aziz SY Al Amine
0
17
221