Explore tweets tagged as #safar_nama
Safar Ep: 8 Sëriñ Tuubaa neena : Sunu boroom indil nama noflaay lu jiitu safar Ba noppi wommatal nama mbégté, ci ludul ab tukki. Maanaam sëriñ bi bimu nekkee ci tukki bi, su Safar mësaan a ñëw nàttu yi dadaan bari lool ci moom.
2
37
155
Sebenarnya, Rasulullah tidak berhijrah pada bulan Muharram seperti yang ramai sangka dalam lagu nasyid tu. Baginda saw berhijrah pada bulan Safar dan sampai ke Madinah pada awal bulan Rabiulawal. Nama-nama bulan dah ada. Cuma takde kiraan tahun waktu itu. Begitulah.
7
2K
4K
Safar Ep: 4 Sëriñ Tuubaa neena : Sunu boroom minga xam ni mooy aji dès bègal nama, mbègtè moo xam ni bènn tiitaangè du ci toppu, ba noppi lèpp loo xam ni wèesu na sunu boroom jèggal nama ko loolu yèppu nak ci wèeru safar gi la amèe. ⬇️
1
35
146
Panjhadi ka jungle in Marathi means summer me pedo ke tamam patte jhad jate hai. Hadde Nigah tak aapko sirf lambe seedhe oonche lakde nazar aayege. Ujadne ke bawajood mazbuti se khade rahna bhi apne aap me ek khubsurti aur kamaal hai. #Safar_nama
0
1
19
Safar Ep: 13 Sëriñ Tuubaa neena : Sunu boroom jox nama lépp luma doon yéenè, ci lu tàmbalée jaysas (1313) jëm ba balsas (1332) néena lepp luma doon yéené ci digënté boobu sunu boroom jox nama ko ,⬇️
2
17
136
Safar Ep: 10 Sëriñ Tuubaa neena : Samay haajo faju woon na lu jiitu may dem ci tukki ba , lépp loo xam ni mbébëtoon naako sunu boroom wommatal nama ko lu jiitu may dem ci tukki ba , loolu nak mungi amée ci darajay Yonent bi ﷺ .
1
23
130
Safar Ep: 7 Sëriñ Tuubaa neena : mbooleem ku ma doon jéema lor , sunu boroom jël na lor googu delloo ko mu jëm féneen fudul sama jëmm jii , moo xam lor gumu mëna doon sunu boroom delloo na ko mu jëm ci ñi nga xam ni dañ maa bañ Sunu boroom minga xam ni nekkal Nama ci ag Njub.
1
26
154
Kenyataan Media ABIM bersama NGO-NGO Islam Gesa Hentikan Fitnah & Adu Domba Atas Nama Agama 18 Ogos 2023/ 1 Safar 1445 H #SebarkanSalam
7
540
729
Safar Nama Aseer e Malta By Maulana Husain Ahmad Madni سفرنامہ اسیر مالٹا
0
0
0
Jaglot #Skardu Road ❣ 🎥 : Safar Nama #Gilgit #explore #mountains #peace #Lahore #travelblogger #northern
0
1
1
Panjhadi ka jungle in Marathi means summer me pedo ke tamam patte jhad jate hai. Hadde Nigah tak aapko sirf lambe seedhe oonche lakde nazar aayege. Ujadne ke bawajood mazbuti se khade rahna bhi apne aap me ek khubsurti aur kamaal hai. #Safar_nama
0
0
16
Dear @Railrestro I have ordered a meal recieved but the quantity of the food is low as well as the taste is worst please find the resolution Not expecting from you 😑
0
0
0
Rabu 040924 30 safar 1446 h Kututup bulan safar ini dg " Alhamdulillah 'ala kulli hal" Terimakasih ya Allah atas sgala di sepanjang safar 1446 h ini Smoga setelah ini banyak hal baik terjadi & ijinkan bismillahku menjadi " alhamdulillahiladzi bi ni' mathi tatimush sholihaat" ☕
7
53
305