@MrsKarmeel
King Karma Fth
1 year
Imaginer lene kasso yi num mel diamono bi Ak tangor. Dès qu’on ouvre les portes le matin Niungui rang rott ndoh, rang sangou rang boutique be. Nieuwat teudiou. Yala nalene Yala tahawu
4
81
376

Replies

@Iamgorguidiouf
Gorgui A. Diouf🇸🇳
1 year
@MrsKarmeel Ancien détenu nena yene chambre yi .. penitencier bi day oubi rek daw fateu bakanam nakh khete bou bone
1
0
0
@MrsKarmeel
King Karma Fth
1 year
@Iamgorguidiouf Dakar d lolo fi am. Bene douche bi si chambre bi tamit nonu rek le meune démé khett bou bone ngay deuké
0
0
0
@ecris_le_tien
𝙇𝙚𝙪𝙢𝙞𝙣𝙚 🇸🇳🇵🇸
1 year
0
1
2
@AhmedThiongane
ahmed Roi ⭐️
1 year
@MrsKarmeel Amine ya rabbi
0
0
0
@kb_sonko
#Keba🇸🇳🧰👷🏾‍♂️
1 year
@MrsKarmeel Allahuma Amiine 🤲🏽
0
0
0