@MrsKarmeel
King Karma Fth
2 years
C’est bien nga liral se bop mokal se bop alquran mais li guene moy niu diangal le. Dinga lire Fatiha egg « arrahmani raheem » djiss niou binde en français le tout miséricordieux le très miséricordieux sans comprendre ni li moy diayanté bi fi si dunya.
3
67
397

Replies

@MrsKarmeel
King Karma Fth
2 years
Fatiha suma siy beug wah on dirait sama khol bi dey beug guene sama deune bi et j’ai envie de pleurer pour plusieurs raisons. Vraiment Yala kene le
1
6
85
@MrsKarmeel
King Karma Fth
2 years
Surat bo mokal warnagn le firil Aya bou nek nga comprendre suniu borom lanla siy diangalé ndah mou Amal le ndieurign deug bokey dieufeundiko
1
9
74
@DoctorLove475
🇵🇸 Sokhna Lily Kone Feu🔥
2 years
@MrsKarmeel @AhmadaShakurJr Fatiha dh beurina gnikay taari tei taari bi bakhoul 💀
1
0
6
@MrsKarmeel
King Karma Fth
2 years
@DoctorLove475 Lolu rek sonal ne diam bi
1
0
0
@Fouttiyou
Daddy Cool
2 years
@MrsKarmeel @PrincessRuqayya Exact. La disponibilité des différents exégèses nous facilitent maintenant la tâche. De ce fait on peut se passer d'un enseignant pour apprendre.
1
0
3