@MrsKarmeel
King Karma Fth
4 years
« Se pap ak se yay Yala mola ko tanal, se serigne yako tanal se bop. Muno muss aka matiatt be Li nga tane gueune lila Yala tanal » Niune tamit danio doywar d nekete 😭. Li Mom patt ngay def
8
187
654

Replies

@Youssou_Dabo
Youssouph Dabo
4 years
@MrsKarmeel Légui louye « mouss ak MATHIATT » ?
1
0
1
@MrsKarmeel
King Karma Fth
4 years
@YoussouD Mangui nane tey lay dé ey man Lanla binde ni. Wa wuyuma dou deglu nga ? Comprendre nga limu wah
1
0
0
@ArameMb
Arame Diomaye Diakhar 🍯🇸🇳
4 years
@MrsKarmeel Mdr c’est violent ca , kou wakh li ?
1
0
0
@MrsKarmeel
King Karma Fth
4 years
@ArameMb Hana Pape Badou bou mame Abdou 😭
@Mrthread4
Historien
4 years
Alhamdoullilah baniou Amé kilifa you melni Serigne Alioune Badara Sy Dabakh....👇
6
166
459
1
6
19
@Ous_87
O. S.
4 years
@MrsKarmeel Mane lima djangone moy gnaari wadjour sufiyanké yi ñoungi siy degg né benn bi moy parents biologiques yi bissi dess moy serigne bi. Ngalla na fekk mou matt serigne.
1
1
8
@MrsKarmeel
King Karma Fth
4 years
@ooz87 Deug le wah dji khott ne. Mo waral Li si ngala bi nga toudd
@MrsKarmeel
King Karma Fth
4 years
Sen choix si niak gueum Yala d niom ak suniu borom le. Fi ngay sako xamxam meune ne nek si Serigne ( professeur) boparé ba mokal nga motali diangali sey parent wayé munul soutt sey Wadiour.
3
3
18
0
0
0
@MalickMilkd
EMD 💛🇸🇳🏁
4 years
@MrsKarmeel Est ce que ya ko taneul seu bop ?? Lol 🏃🏾‍♂️🏃🏾‍♂️
2
0
1
@MrsKarmeel
King Karma Fth
4 years
@MalickMilkd Lol wuyul sa mame
@MrsKarmeel
King Karma Fth
4 years
@ArameMb Hana Pape Badou bou mame Abdou 😭
1
6
19
1
0
0
@Sadiikh_
Sadiikh
4 years
@MrsKarmeel @piibouund Soy dieul wird tijjan ou askaar tarbiya nek ndaw Serigne bi war nala ladj esk say wadiour andeu naniou ci. Wadiour yi souniou dalé sen kaw todj niom itam bouniou dalé souniou kaw niou todj. RESPECTONS NOS PARENTS sakou sen niann gueunél rek la guiir lo am mou barkél.
0
1
24
@Imamalkhadiriya
Cheikh Abdou khadre Ndiaye🇸🇳🇸🇩🇮🇷🇿🇦
4 years
@MrsKarmeel Limay wakh mom dou bari ndakh topou serigne dou farata mtx Tei wadior farata leu
0
0
3
@pan2pan
Pan El Bachir ⭐️🇸🇳
4 years
@MrsKarmeel @mbayanglo En tout cas li nga khamni moy délou si Yalla souniou Borom (l'âme) mom la Serigne bi si sameu rafétal ko....choisir entre la boîte qui contient le diamant et le diamant
0
0
1